Al-Hijr · 55/99
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hijr
قَالُوا بَشَّرْنَاكَ بِالْحَقِّ فَلَا تَكُن مِّنَ الْقَانِطِينَ ۝٥٥
Qaaloo bashsharnaaka bilhaqqi falaa takum minal qaaniteen
📖 Tekkim Wolof
- Ñu ne ko : “Yégal ne lii dëgg la. Bul bokk ca ña naagu ña”.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 53-57 — Simoore Al-Hijr

53قَالُوا لَا تَوْجَلْ إِنَّا نُبَشِّرُكَ بِغُلَامٍ عَلِيمٍ
Ñu ne : “Bul jàq ci nun ! Noo ngi lay bégal ne [danga am doom] ju góor juy bari xam- xam”.
54قَالَ أَبَشَّرْتُمُونِي عَلَىٰ أَن مَّسَّنِيَ الْكِبَرُ فَبِمَ تُبَشِّرُونَ
Mu ne : “Li ngeen di bégle ndax ànd naak samag mage ? Li ngeen may yégal mooy lan ? ”
55قَالُوا بَشَّرْنَاكَ بِالْحَقِّ فَلَا تَكُن مِّنَ الْقَانِطِينَ
- Ñu ne ko : “Yégal ne lii dëgg la. Bul bokk ca ña naagu ña”.
56قَالَ وَمَن يَقْنَطُ مِن رَّحْمَةِ رَبِّهِ إِلَّا الضَّالُّونَ
- Mu ne : “Kan mooy naagu ci yërmaande Yàlla, ñu dul ñu réer [sànku] ? ”
57قَالَ فَمَا خَطْبُكُمْ أَيُّهَا الْمُرْسَلُونَ
Mu ne leen : “Waaw lan mooy seen mbir yéen ñi ñu yónni ?
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
55Aaya

Tekki — Al-Hijr 55

Simoore Al-Hijr Aaya 55 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : - Ñu ne ko : “Yégal ne lii dëgg la.…

Simoore Aaya 55/99 — Simoore Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hijr Dégg, Simoore Al-Hijr Tekki, Simoore Al-Hijr mp3, Simoore Al-Hijr pdf. Aaya 53–57. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers