Maryam · 92/98
Tekki Waxtaan — Simoore Maryam
وَمَا يَنبَغِي لِلرَّحْمَٰنِ أَن يَتَّخِذَ وَلَدًا ۝٩٢
Wa maa yambaghee lir Rahmaani ai yattakhiza waladaa
📖 Tekkim Wolof
Waay-waay yellut ci Yërëmaakoon bi muy am doom waay !

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 90-94 — Simoore Maryam

90تَكَادُ السَّمَاوَاتُ يَتَفَطَّرْنَ مِنْهُ وَتَنشَقُّ الْأَرْضُ وَتَخِرُّ الْجِبَالُ هَدًّا
[Loo xam ne] asamaan yi xaw na cee xottiku, suuf si xar, tundi doj yi màbb [ngir wax jooju],
91أَن دَعَوْا لِلرَّحْمَٰنِ وَلَدًا
ña wax ne alamikk Yàlla am na doom,
92وَمَا يَنبَغِي لِلرَّحْمَٰنِ أَن يَتَّخِذَ وَلَدًا
Waay-waay yellut ci Yërëmaakoon bi muy am doom waay !
93إِن كُلُّ مَن فِي السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ إِلَّا آتِي الرَّحْمَٰنِ عَبْدًا
Képp ku nekk ci asamaan yi ak suuf si, jaamub Yàlla rekk lay doon.
94لَّقَدْ أَحْصَاهُمْ وَعَدَّهُمْ عَدًّا
[Moom Yàlla] xam na fa ñu nekk ak na ñu day [na ñu tollu].
MaryamFihi Alxuraan
98Aaya
MeccanRevelation
92Aaya

Tekki — Maryam 92

Simoore Maryam Aaya 92 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Waay-waay yellut ci Yërëmaakoon bi muy am doom waay !

Simoore Aaya 92/98 — Simoore Maryam مريم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Maryam Dégg, Simoore Maryam Tekki, Simoore Maryam mp3, Simoore Maryam pdf. Aaya 90–94. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers