Taha · 67/135
Tekki Waxtaan — Taha
فَأَوْجَسَ فِي نَفْسِهِ خِيفَةً مُّوسَىٰ ۝٦٧
Fa awjasa fee nafsihee kheefatam Moosa
📖 Tekkim Wolof
Muusaa xaw a amum tiit ci boppam.

🎧 Dégg


📜 Aaya 65-69 — Taha

65قَالُوا يَا مُوسَىٰ إِمَّا أَن تُلْقِيَ وَإِمَّا أَن نَّكُونَ أَوَّلَ مَنْ أَلْقَىٰ
Ñu ne ko : "Yaw Muusaa, benn nga jëkk a sànni, walla nun nooy jëkk a sànni ? ”
66قَالَ بَلْ أَلْقُوا ۖ فَإِذَا حِبَالُهُمْ وَعِصِيُّهُمْ يُخَيَّلُ إِلَيْهِ مِن سِحْرِهِمْ أَنَّهَا تَسْعَىٰ
Muusaa ne leeen] : “Sànnileen”. Ñu daldi sànni seeni yet ak i buum ca seenug njibar mu mel ni yëf yaa ngay dox di yëngatu.
67فَأَوْجَسَ فِي نَفْسِهِ خِيفَةً مُّوسَىٰ
Muusaa xaw a amum tiit ci boppam.
68قُلْنَا لَا تَخَفْ إِنَّكَ أَنتَ الْأَعْلَىٰ
Nu ne ko : “Bul ragal [yaa leen mën], yaa leen fare kaw.
69وَأَلْقِ مَا فِي يَمِينِكَ تَلْقَفْ مَا صَنَعُوا ۖ إِنَّمَا صَنَعُوا كَيْدُ سَاحِرٍ ۖ وَلَا يُفْلِحُ السَّاحِرُ حَيْثُ أَتَىٰ
Sànnil li ci sa loxo ndeyjoor [yet wa] ; li ñuy wone lépp pexey njibarkat doŋŋ la ; te njibarkat moom fàwwu ay tappaleem naaxsaay”. Ba mu ko sànni, yet waa daldi wann yooya yépp
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
67Aaya

Tekki — Taha 67

Simoore Taha Aaya 67 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Muusaa xaw a amum tiit ci boppam.

Simoore Aaya 67/135 — Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Taha Dégg, Taha Tekki, Taha mp3, Taha pdf. Aaya 65–69. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers