Ash-Shu'ara · 116/227
Tekki Waxtaan — Ash-Shu'ara
قَالُوا لَئِن لَّمْ تَنتَهِ يَا نُوحُ لَتَكُونَنَّ مِنَ الْمَرْجُومِينَ ۝١١٦
Qaaloo la`il lam tantahi yaa Noohu latakoonanna minal marjoomeen
📖 Tekkim Wolof
Ñu ne ko : “Yaw Nooh, soo bàyyiwul li nga nekk, dees na la jóori xeer [ba nga dee] ! ”

🎧 Dégg


📜 Aaya 114-118 — Ash-Shu'ara

114وَمَا أَنَا بِطَارِدِ الْمُؤْمِنِينَ
Man dey du maay dàq ñi gëm.
115إِنْ أَنَا إِلَّا نَذِيرٌ مُّبِينٌ
Man doonuma lu dul ab xuppekat bu bir”.
116قَالُوا لَئِن لَّمْ تَنتَهِ يَا نُوحُ لَتَكُونَنَّ مِنَ الْمَرْجُومِينَ
Ñu ne ko : “Yaw Nooh, soo bàyyiwul li nga nekk, dees na la jóori xeer [ba nga dee] ! ”
117قَالَ رَبِّ إِنَّ قَوْمِي كَذَّبُونِ
Mu ne : “Yaw sama Boroom, samaw nit weddi nañu, jàppe ma fenkat.
118فَافْتَحْ بَيْنِي وَبَيْنَهُمْ فَتْحًا وَنَجِّنِي وَمَن مَّعِيَ مِنَ الْمُؤْمِنِينَ
Àtteel sama digganteek ñoom ba mu ne làññ : te nga musal maak ñi ma àndal te ñu bokk ca ña gëm”.
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
116Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 116

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 116 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu ne ko : “Yaw Nooh, soo bàyyiwul li nga…

Simoore Aaya 116/227 — Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Shu'ara Dégg, Ash-Shu'ara Tekki, Ash-Shu'ara mp3, Ash-Shu'ara pdf. Aaya 114–118. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers