Ash-Shu'ara · 207/227
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Shu'ara
مَا أَغْنَىٰ عَنْهُم مَّا كَانُوا يُمَتَّعُونَ ۝٢٠٧
Maaa aghnaaa `anhum maa kaanoo yumaatoo`oon
📖 Tekkim Wolof
la ñu bànneexu woon jariñatuleen dara.

🎧 Dégg


📜 Aaya 205-209 — Simoore Ash-Shu'ara

205أَفَرَأَيْتَ إِن مَّتَّعْنَاهُمْ سِنِينَ
Xanaa gisuloo ne bàyyi woon Nanu leen ay ati at ñuy xaab-xaabi,
206ثُمَّ جَاءَهُم مَّا كَانُوا يُوعَدُونَ
tey jii nag la Nu leen doon dig agsi na,
207مَا أَغْنَىٰ عَنْهُم مَّا كَانُوا يُمَتَّعُونَ
la ñu bànneexu woon jariñatuleen dara.
208وَمَا أَهْلَكْنَا مِن قَرْيَةٍ إِلَّا لَهَا مُنذِرُونَ
Amul benn dëkk bu Nu mës a alag u nitam te yónneewunu fa woon ay xuppekat,
209ذِكْرَىٰ وَمَا كُنَّا ظَالِمِينَ
di fàttali rekk, tooñunu kenn.
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
207Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 207

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 207 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : la ñu bànneexu woon jariñatuleen dara.

Simoore Aaya 207/227 — Simoore Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Shu'ara Dégg, Simoore Ash-Shu'ara Tekki, Simoore Ash-Shu'ara mp3, Simoore Ash-Shu'ara pdf. Aaya 205–209. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers