Ash-Shu'ara · 98/227
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Shu'ara
إِذْ نُسَوِّيكُم بِرَبِّ الْعَالَمِينَ ۝٩٨
Iz nusawweekum bi Rabbil `aalameen
📖 Tekkim Wolof
jamono ya nu leen doon yemaleek Boroom àddina si.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 96-100 — Simoore Ash-Shu'ara

96قَالُوا وَهُمْ فِيهَا يَخْتَصِمُونَ
Ñuy wax ca biir tey xuloo :
97تَاللَّهِ إِن كُنَّا لَفِي ضَلَالٍ مُّبِينٍ
“Waat naa ci Yàlla ne ! Noo ngi woon ci réer gu bir,
98إِذْ نُسَوِّيكُم بِرَبِّ الْعَالَمِينَ
jamono ya nu leen doon yemaleek Boroom àddina si.
99وَمَا أَضَلَّنَا إِلَّا الْمُجْرِمُونَ
Te tooñkat ya doŋŋ a nga nu sànk.
100فَمَا لَنَا مِن شَافِعِينَ
Amunu ku nu tinu,
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
98Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 98

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 98 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : jamono ya nu leen doon yemaleek Boroom àddina si.

Simoore Aaya 98/227 — Simoore Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Shu'ara Dégg, Simoore Ash-Shu'ara Tekki, Simoore Ash-Shu'ara mp3, Simoore Ash-Shu'ara pdf. Aaya 96–100. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers