Ya-Sin · 59/83
Tekki Waxtaan — Simoore Ya-Sin
وَامْتَازُوا الْيَوْمَ أَيُّهَا الْمُجْرِمُونَ ۝٥٩
Wamtaazul Yawma ayyuhal mujrimoon
📖 Tekkim Wolof
“Ayca ! Ca biti, yéen tooñkat yi !

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 57-61 — Simoore Ya-Sin

57لَهُمْ فِيهَا فَاكِهَةٌ وَلَهُم مَّا يَدَّعُونَ
Am nañu fa ay fuytéef ak lépp lu ñuy soxla,
58سَلَامٌ قَوْلًا مِّن رَّبٍّ رَّحِيمٍ
“Jàmm rekk la ñu fay ame” ! Mu bawoo ca Boroom biy Jaglewaakoonu Yërmaandeem.
59وَامْتَازُوا الْيَوْمَ أَيُّهَا الْمُجْرِمُونَ
“Ayca ! Ca biti, yéen tooñkat yi !
60۞ أَلَمْ أَعْهَدْ إِلَيْكُمْ يَا بَنِي آدَمَ أَن لَّا تَعْبُدُوا الشَّيْطَانَ ۖ إِنَّهُ لَكُمْ عَدُوٌّ مُّبِينٌ
Yéen doomi-aadama, ndax digewuma woon ak yéen ngeen bañ a jaamu Séytaane ? Ndax seenub noon la bu nëbbëtuwul,
61وَأَنِ اعْبُدُونِي ۚ هَٰذَا صِرَاطٌ مُّسْتَقِيمٌ
te ngeen di Ma jaamu ? Lii mooy yoon wu jub xocc wi.
Ya-SinFihi Alxuraan
83Aaya
MeccanRevelation
59Aaya

Tekki — Ya-Sin 59

Simoore Ya-Sin Aaya 59 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : “Ayca ! Ca biti, yéen tooñkat yi !

Simoore Aaya 59/83 — Simoore Ya-Sin يس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ya-Sin Dégg, Simoore Ya-Sin Tekki, Simoore Ya-Sin mp3, Simoore Ya-Sin pdf. Aaya 57–61. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers