As-Saffat · 92/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
مَا لَكُمْ لَا تَنطِقُونَ ۝٩٢
Maa lakum laa tantiqoon
📖 Tekkim Wolof
Ana lu leen dal ba dungeen wax ? ”

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 90-94 — Simoore As-Saffat

90فَتَوَلَّوْا عَنْهُ مُدْبِرِينَ
Ñu dëddu ko, won ko ginnaaw.
91فَرَاغَ إِلَىٰ آلِهَتِهِمْ فَقَالَ أَلَا تَأْكُلُونَ
Mu potoxlu ca seen yàlla ya, ne leen : “Ndax dungeen lekk ?
92مَا لَكُمْ لَا تَنطِقُونَ
Ana lu leen dal ba dungeen wax ? ”
93فَرَاغَ عَلَيْهِمْ ضَرْبًا بِالْيَمِينِ
Mu potoxlu dóor leen ak ndeyjoor.
94فَأَقْبَلُوا إِلَيْهِ يَزِفُّونَ
Ñu wutsi ko di daw.
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
92Aaya

Tekki — As-Saffat 92

Simoore As-Saffat Aaya 92 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ana lu leen dal ba dungeen wax ? ”

Simoore Aaya 92/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 90–94. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers