Al-A'raf · 140/206
Tekki Waxtaan — Al-A'raf
قَالَ أَغَيْرَ اللَّهِ أَبْغِيكُمْ إِلَٰهًا وَهُوَ فَضَّلَكُمْ عَلَى الْعَالَمِينَ ١٤٠
Transliteration
Qaala a-ghairal laahi abgheekum ilaahanw wa Huwa faddalakum `alal `aalameen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Mu wax ne : “Moo ndax dama leen di wutal jeneen yàlla ju dul Yàlla, te Moom mu defal leen ngëneel, teg leen ci kaw waa àddina si yépp [ca booba] ? ”
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 138-142 — Al-A'raf
138وَجَاوَزْنَا بِبَنِي إِسْرَائِيلَ الْبَحْرَ فَأَتَوْا عَلَىٰ قَوْمٍ يَعْكُفُونَ عَلَىٰ أَصْنَامٍ لَّهُمْ ۚ قَالُوا يَا مُوسَى اجْعَل لَّنَا إِلَٰهًا كَمَا لَهُمْ آلِهَةٌ ۚ قَالَ إِنَّكُمْ قَوْمٌ تَجْهَلُونَ
Jàllale Nanu Bani-Israayil géej ga. Ñu fekk fa aw nit ñoo xam ne ña nga doon jaamu seeni xërëm, ñu ne : "Muusaa, defal nu yàlla ju mel ni seen yàlla.”. Mu ne leen : “Yéen daal ñu réer ngeen.
139إِنَّ هَٰؤُلَاءِ مُتَبَّرٌ مَّا هُمْ فِيهِ وَبَاطِلٌ مَّا كَانُوا يَعْمَلُونَ
Nii la ñu nekkee di ñu alku; te seeni jëf lu yàqu la.”
140قَالَ أَغَيْرَ اللَّهِ أَبْغِيكُمْ إِلَٰهًا وَهُوَ فَضَّلَكُمْ عَلَى الْعَالَمِينَ
Mu wax ne : “Moo ndax dama leen di wutal jeneen yàlla ju dul Yàlla, te Moom mu defal leen ngëneel, teg leen ci kaw waa àddina si yépp [ca booba] ? ”
141وَإِذْ أَنجَيْنَاكُم مِّنْ آلِ فِرْعَوْنَ يَسُومُونَكُمْ سُوءَ الْعَذَابِ ۖ يُقَتِّلُونَ أَبْنَاءَكُمْ وَيَسْتَحْيُونَ نِسَاءَكُمْ ۚ وَفِي ذَٰلِكُم بَلَاءٌ مِّن رَّبِّكُمْ عَظِيمٌ
(Fàttalikuleen) ba Nu leen musalee ci nitu Firawna ya leen doon teg mbugal mu gën a ñaaw. Daan rey seeni doom yu góor, di bàyyi yu jigéen ya. Te loolu nekkoon na nattu bu màgg bu tukkee ca seen Boroom.
142۞ وَوَاعَدْنَا مُوسَىٰ ثَلَاثِينَ لَيْلَةً وَأَتْمَمْنَاهَا بِعَشْرٍ فَتَمَّ مِيقَاتُ رَبِّهِ أَرْبَعِينَ لَيْلَةً ۚ وَقَالَ مُوسَىٰ لِأَخِيهِ هَارُونَ اخْلُفْنِي فِي قَوْمِي وَأَصْلِحْ وَلَا تَتَّبِعْ سَبِيلَ الْمُفْسِدِينَ
Àppal Nanu Muusaa fanweeri guddi, Nu mottali ko ak fukk, diir ba Boroomam dogal mat ñeneenti fukki guddi. Muusaa wax na mbokkam ma Aaruuna : “Wuutu ma ci samaw nit, te nangay jubbanti te bul topp yoonu yàqkat ya”.
Al-A'rafFihi Alxuraan
206Aaya
MeccanRevelation
140Aaya
Tekki — Al-A'raf 140
Simoore Al-A'raf Aaya 140 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu wax ne : “Moo ndax dama leen di wutal…Simoore Aaya 140/206 — Al-A'raf الأعراف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-A'raf Dégg, Al-A'raf Tekki, Al-A'raf mp3, Al-A'raf pdf. Aaya 138–142. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








