Al-Hijr · 63/99
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hijr
قَالُوا بَلْ جِئْنَاكَ بِمَا كَانُوا فِيهِ يَمْتَرُونَ ۝٦٣
Qaaloo bal ji`naaka bimaa kaanoo feehi yamtaroon
📖 Tekkim Wolof
- Ñu ne ko : “Axakay, digal nanu la ànd ak la ñu doon sikki-sàkka.

🎧 Dégg


📜 Aaya 61-65 — Simoore Al-Hijr

61فَلَمَّا جَاءَ آلَ لُوطٍ الْمُرْسَلُونَ
Ba ña ñu yónni agsee ca waa kër Lóot,
62قَالَ إِنَّكُمْ قَوْمٌ مُّنكَرُونَ
Lóot ne leen : “Yéen dey aw nit ñu ma xamul ngeen”.
63قَالُوا بَلْ جِئْنَاكَ بِمَا كَانُوا فِيهِ يَمْتَرُونَ
- Ñu ne ko : “Axakay, digal nanu la ànd ak la ñu doon sikki-sàkka.
64وَأَتَيْنَاكَ بِالْحَقِّ وَإِنَّا لَصَادِقُونَ
Te ñëw nanu ci yaw indil la dëgg. Te it ñu dëggu lanu.
65فَأَسْرِ بِأَهْلِكَ بِقِطْعٍ مِّنَ اللَّيْلِ وَاتَّبِعْ أَدْبَارَهُمْ وَلَا يَلْتَفِتْ مِنكُمْ أَحَدٌ وَامْضُوا حَيْثُ تُؤْمَرُونَ
Te nanga dem rañaan yaak sa njaboot bu guddi xaajee ; te nga topp ca seen ginnaaw te bu kenn ci yéen geestu. Te ngeen jublu fa ñu leen digal”.
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
63Aaya

Tekki — Al-Hijr 63

Simoore Al-Hijr Aaya 63 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : - Ñu ne ko : “Axakay, digal nanu la ànd…

Simoore Aaya 63/99 — Simoore Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hijr Dégg, Simoore Al-Hijr Tekki, Simoore Al-Hijr mp3, Simoore Al-Hijr pdf. Aaya 61–65. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers