Al-Hijr · 91/99
Tekki Waxtaan — Al-Hijr
الَّذِينَ جَعَلُوا الْقُرْآنَ عِضِينَ ۝٩١
Allazeena ja`alul Quraana`ideen
📖 Tekkim Wolof
ca ña séddale Téere ba ay xaaj, pàcc-pàccee Alxuraan ngir sànkaate.

🎧 Dégg


📜 Aaya 89-93 — Al-Hijr

89وَقُلْ إِنِّي أَنَا النَّذِيرُ الْمُبِينُ
Te neel : “Man aji-laabir laa ju wér” [ci xamal leen dëgg],
90كَمَا أَنزَلْنَا عَلَى الْمُقْتَسِمِينَ
Noonu it Lanu wàccele woon [ab Téere] ca ña xàjjatle woon [seen diine],
91الَّذِينَ جَعَلُوا الْقُرْآنَ عِضِينَ
ca ña séddale Téere ba ay xaaj, pàcc-pàccee Alxuraan ngir sànkaate.
92فَوَرَبِّكَ لَنَسْأَلَنَّهُمْ أَجْمَعِينَ
Giñ naa ci sama màggug Boroom ! Fàwwu danañu leen laaj ñoom ñépp
93عَمَّا كَانُوا يَعْمَلُونَ
la ñu nekkon di ko def [ci ay ñaawtéef].
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
91Aaya

Tekki — Al-Hijr 91

Simoore Al-Hijr Aaya 91 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ca ña séddale Téere ba ay xaaj, pàcc-pàccee Alxuraan ngir…

Simoore Aaya 91/99 — Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Hijr Dégg, Al-Hijr Tekki, Al-Hijr mp3, Al-Hijr pdf. Aaya 89–93. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers