Al-A'raf · 118/206
Tekki Waxtaan — Simoore Al-A'raf
فَوَقَعَ الْحَقُّ وَبَطَلَ مَا كَانُوا يَعْمَلُونَ ۝١١٨
Fawaqa`al haqqu wa batala maa kaanoo ya`maloon
📖 Tekkim Wolof
Dëgg daldi tàbbi, la ñu doon def yàqu.

🎧 Dégg


📜 Aaya 116-120 — Simoore Al-A'raf

116قَالَ أَلْقُوا ۖ فَلَمَّا أَلْقَوْا سَحَرُوا أَعْيُنَ النَّاسِ وَاسْتَرْهَبُوهُمْ وَجَاءُوا بِسِحْرٍ عَظِيمٍ
Mu ne : “Sànnileen”. Ba ñu sànnee, dañoo jabar bëti nit ña, ragal-loo leen ci jabar gu rëy.
117۞ وَأَوْحَيْنَا إِلَىٰ مُوسَىٰ أَنْ أَلْقِ عَصَاكَ ۖ فَإِذَا هِيَ تَلْقَفُ مَا يَأْفِكُونَ
Nu xelal Muusaa ne ko : “Sànnil sa yet wi”. Mu daldi wann la ñu doon wëlbati.
118فَوَقَعَ الْحَقُّ وَبَطَلَ مَا كَانُوا يَعْمَلُونَ
Dëgg daldi tàbbi, la ñu doon def yàqu.
119فَغُلِبُوا هُنَالِكَ وَانقَلَبُوا صَاغِرِينَ
Ñu not leen foofa, ñu daldi ànd ak toroxte.
120وَأُلْقِيَ السَّحَرَةُ سَاجِدِينَ
Ñu rot ñoom jabar ya, sujjóot.
Al-A'rafFihi Alxuraan
206Aaya
MeccanRevelation
118Aaya

Tekki — Al-A'raf 118

Simoore Al-A'raf Aaya 118 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Dëgg daldi tàbbi, la ñu doon def yàqu.

Simoore Aaya 118/206 — Simoore Al-A'raf الأعراف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-A'raf Dégg, Simoore Al-A'raf Tekki, Simoore Al-A'raf mp3, Simoore Al-A'raf pdf. Aaya 116–120. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers