Al-Hijr · 70/99
Tekki Waxtaan — Al-Hijr
قَالُوا أَوَلَمْ نَنْهَكَ عَنِ الْعَالَمِينَ ۝٧٠
Qaalooo awalam nanhaka `anil `aalameen
📖 Tekkim Wolof
Ñu ne : “Ndax terewuñu la woon ngay woo nit ñi [ci sa diine ji] ? ”

🎧 Dégg


📜 Aaya 68-72 — Al-Hijr

68قَالَ إِنَّ هَٰؤُلَاءِ ضَيْفِي فَلَا تَفْضَحُونِ
- Lóot ne leen : “Ñii samay gan lañu, buleen ma ci rusloo.
69وَاتَّقُوا اللَّهَ وَلَا تُخْزُونِ
Nangeen ragal Yàlla te buleen ma teg gàcce.
70قَالُوا أَوَلَمْ نَنْهَكَ عَنِ الْعَالَمِينَ
Ñu ne : “Ndax terewuñu la woon ngay woo nit ñi [ci sa diine ji] ? ”
71قَالَ هَٰؤُلَاءِ بَنَاتِي إِن كُنتُمْ فَاعِلِينَ
Mu ne leen : “Samay doom yu jigéen a ngii ndegam bëgg ngeen a def [li ngeen nar] ! ”
72لَعَمْرُكَ إِنَّهُمْ لَفِي سَكْرَتِهِمْ يَعْمَهُونَ
Giñ naa ci sag dund [yaw Muhammed] ne naka ñoom nekkoon nañu di dengi-dengi ci seeni ngëlamte.
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
70Aaya

Tekki — Al-Hijr 70

Simoore Al-Hijr Aaya 70 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu ne : “Ndax terewuñu la woon ngay woo nit…

Simoore Aaya 70/99 — Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Hijr Dégg, Al-Hijr Tekki, Al-Hijr mp3, Al-Hijr pdf. Aaya 68–72. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers