Al-Hijr · 71/99
Tekki Waxtaan — Al-Hijr
قَالَ هَٰؤُلَاءِ بَنَاتِي إِن كُنتُمْ فَاعِلِينَ ۝٧١
Qaala haaa`ulaaa`i banaateee in kuntum faa`ileen
📖 Tekkim Wolof
Mu ne leen : “Samay doom yu jigéen a ngii ndegam bëgg ngeen a def [li ngeen nar] ! ”

🎧 Dégg


📜 Aaya 69-73 — Al-Hijr

69وَاتَّقُوا اللَّهَ وَلَا تُخْزُونِ
Nangeen ragal Yàlla te buleen ma teg gàcce.
70قَالُوا أَوَلَمْ نَنْهَكَ عَنِ الْعَالَمِينَ
Ñu ne : “Ndax terewuñu la woon ngay woo nit ñi [ci sa diine ji] ? ”
71قَالَ هَٰؤُلَاءِ بَنَاتِي إِن كُنتُمْ فَاعِلِينَ
Mu ne leen : “Samay doom yu jigéen a ngii ndegam bëgg ngeen a def [li ngeen nar] ! ”
72لَعَمْرُكَ إِنَّهُمْ لَفِي سَكْرَتِهِمْ يَعْمَهُونَ
Giñ naa ci sag dund [yaw Muhammed] ne naka ñoom nekkoon nañu di dengi-dengi ci seeni ngëlamte.
73فَأَخَذَتْهُمُ الصَّيْحَةُ مُشْرِقِينَ
Ag xaacu sadd leen suba cuuy.
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
71Aaya

Tekki — Al-Hijr 71

Simoore Al-Hijr Aaya 71 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu ne leen : “Samay doom yu jigéen a ngii…

Simoore Aaya 71/99 — Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Hijr Dégg, Al-Hijr Tekki, Al-Hijr mp3, Al-Hijr pdf. Aaya 69–73. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers