Sad · 31/88
Tekki Waxtaan — Sad
إِذْ عُرِضَ عَلَيْهِ بِالْعَشِيِّ الصَّافِنَاتُ الْجِيَادُ ۝٣١
Iz `urida `alaihi bil`ashiy yis saafinaatul jiyaad
📖 Tekkim Wolof
(Fàttalikul) ngoon ga, ñu ko gaarale fasi naari góor ya,

🎧 Dégg


📜 Aaya 29-33 — Sad

29كِتَابٌ أَنزَلْنَاهُ إِلَيْكَ مُبَارَكٌ لِّيَدَّبَّرُوا آيَاتِهِ وَلِيَتَذَكَّرَ أُولُو الْأَلْبَابِ
[Lii] ab Téere la bu Nuy wàcce ci yaw bu barkeel nak, ngir ñuy settantal ay laayaam ak it ngir woroomi xel yi man ciy fàttalikoo!
30وَوَهَبْنَا لِدَاوُودَ سُلَيْمَانَ ۚ نِعْمَ الْعَبْدُ ۖ إِنَّهُ أَوَّابٌ
May Nanu Daawuda (doomam ja) Sulaymaan, - ndaw jaam bu baax ! – Ku daan dellu ca boroomam la.
31إِذْ عُرِضَ عَلَيْهِ بِالْعَشِيِّ الصَّافِنَاتُ الْجِيَادُ
(Fàttalikul) ngoon ga, ñu ko gaarale fasi naari góor ya,
32فَقَالَ إِنِّي أَحْبَبْتُ حُبَّ الْخَيْرِ عَن ذِكْرِ رَبِّي حَتَّىٰ تَوَارَتْ بِالْحِجَابِ
Sulaymaan dellu wax ne : “Cëy man, maa ngi fees dell ak bëgg (àddina sii) mu fàbbi maa ba jant bi so te fàttalikuwuma sama Boroom.
33رُدُّوهَا عَلَيَّ ۖ فَطَفِقَ مَسْحًا بِالسُّوقِ وَالْأَعْنَاقِ
Delloosil ma fas yi.”. Ñu delloosil ko ko mu dagg yeel ya ak doq ya.
SadFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
31Aaya

Tekki — Sad 31

Simoore Sad Aaya 31 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : (Fàttalikul) ngoon ga, ñu ko gaarale fasi naari góor ya,

Simoore Aaya 31/88 — Sad ص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Sad Dégg, Sad Tekki, Sad mp3, Sad pdf. Aaya 29–33. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers