Al-A'raf · 121/206
Tekki Waxtaan — Simoore Al-A'raf
قَالُوا آمَنَّا بِرَبِّ الْعَالَمِينَ ۝١٢١
Qaaloo aamannaa bi Rabbil `aalameen
📖 Tekkim Wolof
Ñu ne : “Gëm nañu Boroom àddina si,

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 119-123 — Simoore Al-A'raf

119فَغُلِبُوا هُنَالِكَ وَانقَلَبُوا صَاغِرِينَ
Ñu not leen foofa, ñu daldi ànd ak toroxte.
120وَأُلْقِيَ السَّحَرَةُ سَاجِدِينَ
Ñu rot ñoom jabar ya, sujjóot.
121قَالُوا آمَنَّا بِرَبِّ الْعَالَمِينَ
Ñu ne : “Gëm nañu Boroom àddina si,
122رَبِّ مُوسَىٰ وَهَارُونَ
Boroom Muusaa ak Aaruuna.”
123قَالَ فِرْعَوْنُ آمَنتُم بِهِ قَبْلَ أَنْ آذَنَ لَكُمْ ۖ إِنَّ هَٰذَا لَمَكْرٌ مَّكَرْتُمُوهُ فِي الْمَدِينَةِ لِتُخْرِجُوا مِنْهَا أَهْلَهَا ۖ فَسَوْفَ تَعْلَمُونَ
Firawna ne leen : “Ndax dangeen Koy gëm te joxuma leen ci ndigal ? Lii, pexe la mu ngeen fàggu ci dëkk bi, ngir génne ñi fi dëkk.Waaye dangeen xam...
Al-A'rafFihi Alxuraan
206Aaya
MeccanRevelation
121Aaya

Tekki — Al-A'raf 121

Simoore Al-A'raf Aaya 121 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu ne : “Gëm nañu Boroom àddina si,

Simoore Aaya 121/206 — Simoore Al-A'raf الأعراف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-A'raf Dégg, Simoore Al-A'raf Tekki, Simoore Al-A'raf mp3, Simoore Al-A'raf pdf. Aaya 119–123. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 29, 2026

Don't forget us in your sincere prayers