Ash-Shu'ara · 163/227
Tekki Waxtaan — Ash-Shu'ara
فَاتَّقُوا اللَّهَ وَأَطِيعُونِ ۝١٦٣
Fattaqul laaha wa atee`oon
📖 Tekkim Wolof
Ragal-leen Yàlla te topp ma.
🎧 Dégg

📜 Aaya 161-165 — Ash-Shu'ara

161إِذْ قَالَ لَهُمْ أَخُوهُمْ لُوطٌ أَلَا تَتَّقُونَ
ba leen seen mbokk ma Lóot waxee ne : “Moo ndax dungeen ragal Yàlla ?
162إِنِّي لَكُمْ رَسُولٌ أَمِينٌ
Man mii dey, ab Yonent laa ci yéen bu wóor.
163فَاتَّقُوا اللَّهَ وَأَطِيعُونِ
Ragal-leen Yàlla te topp ma.
164وَمَا أَسْأَلُكُمْ عَلَيْهِ مِنْ أَجْرٍ ۖ إِنْ أَجْرِيَ إِلَّا عَلَىٰ رَبِّ الْعَالَمِينَ
Laajuma leen ci genn pey ; samag pey, Boroom àddina see ko warlu.
165أَتَأْتُونَ الذُّكْرَانَ مِنَ الْعَالَمِينَ
Yéen góor ñi, moo ndax dangeen di sàkku bànneexu séy ci góoru àddina sii [Ngóor- jigéen]?
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
163Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 163

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 163 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ragal-leen Yàlla te topp ma.

Simoore Aaya 163/227 — Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Shu'ara Dégg, Ash-Shu'ara Tekki, Ash-Shu'ara mp3, Ash-Shu'ara pdf. Aaya 161–165. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers